Translation of "change" into Wolof
coppite, soppeeku, soppi are the top translations of "change" into Wolof.
(countable) the process of becoming different. [..]
-
coppite
coppite gi, noun
There is a change in the city.
Dëkk bi am na ag coppite.
-
soppeeku
soppeeku ~ soppiku, intransitive
In the past, there was no marriage between communities/casts and each cast had their own unique activities. However, now things are slowly changing with the younger generation.
Bu njëkk, séy daanul am ci diggante askan yi te askan bu nekk ak liggéey yu mu baaxoowoon. Waaye, leegi mbir yi ñungi soppeeku ndank-ndank ak ndaw ñi.
-
soppi
verbtransitive
He is well-behaved now; what has changed him?
Dafa yaru léegi; lu ko soppi?
-
soppiku
intransitive, soppeeku ~ soppiku [sɔ:ppɛ:ku]
The village has changed.
Dëkk bi dafa soppiku.
-
Show algorithmically generated translations
Automatic translations of "change" into Wolof
-
Glosbe Translate
Images with "change"
Phrases similar to "change" with translations into Wolof
-
fuuy
-
mbooleem coppite yi
-
wecci
-
Lu bant yàgga yàgg ci géej, du soppaliku jasig.
-
xànjar
-
jàdd
-
toxu
-
xànjar