Translation of "bar" into English
monitor lizard (varanus), speak quickly, to talk fast are the top translations of "bar" into English.
-
monitor lizard (varanus)
Bar bi. Kawlax kenn du fa rey bar, ay rab lañu.
In Kaolack, no one kills monitor lizards, they are spirits.
-
speak quickly
Naka jekk, Aatu masul a bare wax, waaye ñetti fan yii de, ay noppam namm nañu lool kàdduy nit. Golo yi ñoom, ñu ngi wax ni ay Doomi-Aadama. Aatu xamul sax wan làkk lañuy làkk. Li mu ci xam daal, moo di ne seen waxin gaaw na lool. Laay! Ndekete golo tamit dina bar...
Aatu doesn't usually talk much, but these three days his ears have missed very much human words. The monkeys speak like humans. Aatu doesn't even know which language they speak. What he knows is that they talk too fast. Wow! Monkeys too can talk fast...
-
to talk fast
-
Show algorithmically generated translations
Automatic translations of "bar" into English
-
Glosbe Translate