Translation of "doyadi" into English
state of being limited, to be a little crazy, to have a mental handicap are the top translations of "doyadi" into English.
-
state of being limited
Ngir bañ a guddal lim bi, mën naa ne Ñarelaa gii ma dëkk, dama koo miin ba sama gaa ñi leeg-leeg dañu may nirook ay xuusmaañàpp. Mel ni am na ku làqu ci béréb bu lëndëm, téye ci buumam di xëcc na mu ko neexe te su ko defee, Doomi- Aadama yiy kër-këri, yaakaar, ci seen doyadeek seen xel mu gàtt, ne li ñuy def yépp ci seen coobare la.
Not to lengthen the list, I can say that Ñarelaa, where I live, is so familiar to me that my people sometimes seem like puppets to me. It is as if someone were hiding in a dark place, holding his string and pulling whatever he wanted, and when he did that, the hard-working human beings think, in their limited brains and narrow-mindedness, that everything they do is of their own free will.
-
to be a little crazy, to have a mental handicap
cf. yemb Synon.: dese, yembadi, matadi
Ekoolu xale yu doyadi yi la.
This is the school for mentally handicapped children.
-
Show algorithmically generated translations
Automatic translations of "doyadi" into English
-
Glosbe Translate