Translation of "koom" into English
resources is the translation of "koom" into English.
-
resources
nounBa ñu sukkandikoo ci liy suqali Senegaal, nguur gi dajale na ay pexe yu mën a indil am koom yu jëm ci kéewug jamano, ngir dimbali taxawaayu naalu PARFA liñ ci nisër mooy yokkuteg bànqaas yi jëm ci xeeti mbey yi ñu tànnte jaarale ko ci yaxantu bi nga xam ne dañu cee jublu suqali mbey mu ndaw mi ci yoonu yokkute jëm ci dund bi, ngir indi kaaraange ci dund bi ag liy dikkal beykat yu ndaw yi ak teg fi fuñu mën a liggeeyee lu yàag te muy indil am koom waa kow gi, lu demee ni ndaw ñeek jigéen ñi. Yëngu-yëngu yi ëpp solo yu naalu PARFA mooy dellosig moomeelu suuf si ak yaxandug ndox mi ak mbeyam tóor tóor yi ak coppiteg meññeefu mbey mi, ak yëngute yu jëm ci coppiteg li ñuy bey.
In line with its ‘Plan Senegal Emergent’, the Government mobilized the resources of the Global Environment Facility (GEF-6) to support the implementation of the PARFA Project. The objective is to develop priority agroecosystem services through investments to improve small-scale agriculture and food value chains, contributing to enhancing food security and incomes of smallholders’ farmers and to create sustainable and remunerative employment for rural people, especially youth and women. The key project’s activities include land restoration, water management, greening agricultural and primary transformation activities.
-
Show algorithmically generated translations
Automatic translations of "koom" into English
-
Glosbe Translate
Phrases similar to "koom" with translations into English
-
economics
-
Economy of Africa
-
business
-
economics
-
economic science · economics · economy